Plasings

Wys tans plasings vanaf Februarie, 2015

Wa Kàwga

Prent
So sét loo ba seet Fa pepp dip toortooré ñu tudeko kàwga, So sétloo ba ca biir, momee mo boot kërum taax. Taax mi nàagu fëg dënëm ne ma fi gënn, cey lii. Taax mi Wón ganaw gidul dëgë liwoon dembàm  dëk cip tayam rék doon ëlëgëm mu tuddéko mboyga manam kàwga. Fa baykatya tamú te sañ fa dëk moné, momee ñuy tutil Nitu Alà, mo nara dukàt ba faw, frankkulayu fasyeené mu neex Yàlla setàan buur aki daggam ngony ba dëgërr cip miis nootel, dëk cip fitnal doon firawoona jëm ciy tàrtàr.   SUBHANALLAH! ABT                                                        M.Jobe

Rafetal

Prent
Ñari wañikaay, Ñari nattukaay. Benë dëg dong ci diggum géwu ñarri mbërr cim xee l. Xojàntébi ne tuli ak mali tàr ba jeegi dàyoo. Xòy teew né sakup yambb cip càya gaaw ba ràw mélax Ndjiit dëg jakarlok njaxaskat, saay saay took fee dëk cip xàmb Diiso ngony ci nit ko gis, barinà li wute ci boppam doon bena nitki. Nité reka woor, nit, nité rekkoko wàr mba mu dëk cip fakastalu Yàlla xaji. Allahuma amine. ABT                                                         M.Jobe

Kumpë

Prent
Xarit sama fo jëm ? Fumudul jéxee mu jarr Dem ba jeex ci leep ak lumumënta doon. Cey sama waji! So wañeco setsima sude jaam, ñu doxado ci. ABT                                                        M.Jobe

Mbëgel

Prent
Xol dàl la ngok mbëgel, lii rembat te të le  fees. Saliiru xam-xam bu dëggu ci diggu guddi gi ne ci yeeñ xol biy làññi ay légét. ABT