Plasings

Wys tans plasings vanaf 2015

JËRËJËF SERIÑ TOUBA

Prent
(Yaay sopi dip sàpali ba taxna ko défar mu teey ba faf laab) Ganaw dak seytane Se lal ak Xazbalax Basmalax Xawxà lax Xaylalax. Mindef biy niittël Niit ak xàl xalima bu Yàlla taal Xallaa ma ndir jallà, “Ya Xayu”  Xàlla xàlla ding fi jaar, “Ya Xayum”  Xàlla “Al Huda” niit fa dara dul rëc.   Yaw miy Abdalax Doon Xàdim dip Kiñu-Sànta Minndeef bula log wanasu Tàbbee cip tedda jiko diwo ngëneel. Yaay sopi dip sàpali ba taxna ko défar mu teey ba faf laab. Reewo reew wërgël këpp yay “muxafi” mot sëkë cip jiko doon “Bafal”. Jërëjëf  Serigne Tuba, jaraw làkka Mame Cheikh Ibra Faal, Ila Tuba rek, Ila Tuba “kaounu”. (…) Abdou laye Bi la l Traoré

Mbàax moy wote wàlu

Prent
Kula defal lu baax wòneko. Ci lu leer, kuy def lu baax ko deeg Soko mënee wax, jëfeko. Lo degg ci lu ñaw njeemté Defar bu deggu mo ca gënn.  Abdou laye Bilal Traoré                                                      Obra: M Jobe

Ànamakakñanindéwënël?

Prent
Mày làc askànwi -Jàmpuut- lumuy tékki? Diko ñàw, diko sòl, dika “titëroo”. Baye Abdoul Lahaat Mbacké, Yàl, nala suuf seddee. Amin. Abdoulaye Bilal Traoré  - Lii duul dàra si Mom, motax teey te wòyof donn warugal ci nit -  

Tëgg dàwwul mbaar

Prent
Mo sañc mbaar né fax ca suufam Jëkée cip taal mu takq doon ki jëkk tëgg Mom mi jëkkë cip diigàl ëff mu boyy ba seey Seepi  weeñ dëgërr, mu nóral yaawi xóos tapatapàl Bëtt, ñóodanti  diapàndal diapukayyii noppi tekci mélaxal mu donn këll Mu tataan dox, root mu fees joxla nga naann te nann ëskëy ci bip feem. Kokoy tëgg mi Yàlla térral, cey ñeeño, yaw mi Yàlla bérral ngir say jaloré. ABT                                                        M.Jobe

Seet sa bopp

Prent
Lata ngay jalgati Fobàl ñaari seetu Bena sa kanam Bennen sa ganaw Sigil xool li nga jakarlol Liy bàx ci sap ndong né fangë Ñaar tewateew : gëmë wala xippi. ABT                                               M.Jobe

Wa Kàwga

Prent
So sét loo ba seet Fa pepp dip toortooré ñu tudeko kàwga, So sétloo ba ca biir, momee mo boot kërum taax. Taax mi nàagu fëg dënëm ne ma fi gënn, cey lii. Taax mi Wón ganaw gidul dëgë liwoon dembàm  dëk cip tayam rék doon ëlëgëm mu tuddéko mboyga manam kàwga. Fa baykatya tamú te sañ fa dëk moné, momee ñuy tutil Nitu Alà, mo nara dukàt ba faw, frankkulayu fasyeené mu neex Yàlla setàan buur aki daggam ngony ba dëgërr cip miis nootel, dëk cip fitnal doon firawoona jëm ciy tàrtàr.   SUBHANALLAH! ABT                                                        M.Jobe

Rafetal

Prent
Ñari wañikaay, Ñari nattukaay. Benë dëg dong ci diggum géwu ñarri mbërr cim xee l. Xojàntébi ne tuli ak mali tàr ba jeegi dàyoo. Xòy teew né sakup yambb cip càya gaaw ba ràw mélax Ndjiit dëg jakarlok njaxaskat, saay saay took fee dëk cip xàmb Diiso ngony ci nit ko gis, barinà li wute ci boppam doon bena nitki. Nité reka woor, nit, nité rekkoko wàr mba mu dëk cip fakastalu Yàlla xaji. Allahuma amine. ABT                                                         M.Jobe

Kumpë

Prent
Xarit sama fo jëm ? Fumudul jéxee mu jarr Dem ba jeex ci leep ak lumumënta doon. Cey sama waji! So wañeco setsima sude jaam, ñu doxado ci. ABT                                                        M.Jobe

Mbëgel

Prent
Xol dàl la ngok mbëgel, lii rembat te të le  fees. Saliiru xam-xam bu dëggu ci diggu guddi gi ne ci yeeñ xol biy làññi ay légét. ABT

Xoyum toortoor

Prent
Kërkëri dip këpëtël ba faf né këp ca kaw Jëf jël, jëf sédoo, jëf yeené ci lu gàtuul ñaka xàt te newuul kocc doon sóoti ci ak déf ci muy li ñëp mom mi dómooyu ràgg ràmm ak raflé. Amiin. ABT

Gëm, tiis na

Prent
Kuy jòxé kuné nangul ñu delolà Ndeem japo ci joko jama lay xibar So nee manlà wala moomlà nafek amnà ku def. So séeto jiis sa bopp muy dëgë nala woor né sap xel nga seen. So nee nasaràn bii ni wala nëlee lakoy defee ba tax ma topando, War nga seetat sa bopp ndaxam do baima buñu tak bumm jitàl. Cambaràl li nga doon ndax yawla wala kilay yégalaki wàcee Dila yobu aki delosi, di la tamtamal ngay ree naan mafi mënn Di jooy nann ma dègal kii fi mën ba tax maak samp sap jë ne mel. Naxo ki kenn mëntë nax jëndékop nit buy dundà té reer. Amnà ñu Yàlla mày Ñuul te wàloo dank bu dunn, jëfewuñuko. Ken duné ñu bax dembë ak tay jaru ñufi ba tax li xel di niit aki wax Suko lamìnn tudé ñu rà yko; ñuy ñann borombi yok suturë. Samp sap ndënd di xaar ñu dànla te nanla waw goor xañc sap der là Do mësë jogé cip surga, xacc sàx du la nawlo bày doon sa morom. Barkep gëngi mindef sant Yàlla mi xamal n dòx ak bann ne ken gënulen. ABT 

Xel xalàt Sant Sëriñ Saliu Mbàkke borom Xélkom

Prent
Biiru adduna, Déf ci lu barée bàri. Li baax ak li doyadi Fexé li gën ëpë ci waarwi Ëpë ci waarwi ba suul mótadi. Tëmbël day suux walá tëmb Dax li ko wár momee daal Moy sápali bañu yëkk né Liy yëbbë lu né wuték dox Miñi Yàlla burrus ñu texėe. Gënfé ñaaw li doyadi li ñëp défando Dax nak kula bëg, nángul là. Séet sét ak seetu suñu mélee né suufé nga sápali Sañcap dëk gáss teen nit dip naan dox ba cày bëllee Daxte amana so jaboté ñëp ko digël na yam seen diggënté.  Jërëjëf Seriñ Tuba (×3). Jarawlàk Mam Lamp Fall babúl muridina. ABT 

NDÖMBUM ÑÀTI BÒPP

Prent
Pepp ak pepp pepp jiitu pepp pepp topa ci pepp di tepp tepp ba ñorr jëriiñ baatinu cé lum xè l. Àduna miiy dox te doxóontuwul Móome di daagu ci kii ci waar wi donn jiis ci sa bópp. Bòpp mi dùl dëmoyu téy càmbar famu gëne rék mu raay ba ree6 ndàx àmana rewmi mënna baxe bopam tàmiit, laaye biir wërngal këp àdduna  lu këyiit nàxassaayàl bakàn jaayu fi dëgg sàx ci téey-lóok-déglu Ndömbum ñàti bòpp yu téwaa l àskaanwi taxawuko Dóon njiitum rew fa néwonn kenà ki ñëpë nàwoon Wàye, mu ñak motal yabàllu yàkaar yi né woon faax  Doon ñann dàl-set-andàk-téey. Abdou laye Bi la l Traoré