Xel xalàt Sant Sëriñ Saliu Mbàkke borom Xélkom
Biiru adduna, Déf ci lu barée bàri. Li baax ak li doyadi Fexé li gën ëpë ci waarwi Ëpë ci waarwi ba suul mótadi. Tëmbël day suux walá tëmb Dax li ko wár momee daal Moy sápali bañu yëkk né Liy yëbbë lu né wuték dox Miñi Yàlla burrus ñu texėe. Gënfé ñaaw li doyadi li ñëp défando Dax nak kula bëg, nángul là. Séet sét ak seetu suñu mélee né suufé nga sápali Sañcap dëk gáss teen nit dip naan dox ba cày bëllee Daxte amana so jaboté ñëp ko digël na yam seen diggënté. Jërëjëf Seriñ Tuba (×3). Jarawlàk Mam Lamp Fall babúl muridina. ABT