Plasings

Entrada destacada

Mbàax moy wote wàlu

Prent
Kula defal lu baax wòneko. Ci lu leer, kuy def lu baax ko deeg Soko mënee wax, jëfeko. Lo degg ci lu ñaw njeemté Defar bu deggu mo ca gënn.  Abdou laye Bilal Traoré                                                      Obra: M Jobe

Anamakakñanindéwënël?

Mày làcc askànwi Jàmpuut lumuy tékki? Diko ñàw, diko sòl, dika titëroo. Baye Abdoul Lahaat Mbacké, Yàl nala suuf seddee. Amine. Abdoulaye Bilal Traoré  -Lii duul dàra si Mom, motàx teey te wòyof donn warugal ci nit-  

JËRËJËF SERIÑ TOUBA

Prent
(Yaay sopi dip sàpali ba taxna ko défar mu teey ba faf laab) Ganaw dak seytane Se lal ak Xazbalax Basmalax Xawxà lax Xaylalax. Mindef biy niittël Niit ak xàl xalima bu Yàlla taal Xallaa ma ndir jallà, “Ya Xayu”  Xàlla xàlla ding fi jaar, “Ya Xayum”  Xàlla “Al Huda” niit fa dara dul rëc.   Yaw miy Abdalax Doon Xàdim dip Kiñu-Sànta Minndeef bula log wanasu Tàbbee cip tedda jiko diwo ngëneel. Yaay sopi dip sàpali ba taxna ko défar mu teey ba faf laab. Reewo reew wërgël këpp yay “muxafi” mot sëkë cip jiko doon “Bafal”. Jërëjëf  Serigne Tuba, jaraw làkka Mame Cheikh Ibra Faal, Ila Tuba rek, Ila Tuba “kaounu”. (…) Abdou laye Bi la l Traoré

Ànamakakñanindéwënël?

Prent
Mày làc askànwi -Jàmpuut- lumuy tékki? Diko ñàw, diko sòl, dika “titëroo”. Baye Abdoul Lahaat Mbacké, Yàl, nala suuf seddee. Amin. Abdoulaye Bilal Traoré  - Lii duul dàra si Mom, motax teey te wòyof donn warugal ci nit -  

Tëgg dàwwul mbaar

Prent
Mo sañc mbaar né fax ca suufam Jëkée cip taal mu takq doon ki jëkk tëgg Mom mi jëkkë cip diigàl ëff mu boyy ba seey Seepi  weeñ dëgërr, mu nóral yaawi xóos tapatapàl Bëtt, ñóodanti  diapàndal diapukayyii noppi tekci mélaxal mu donn këll Mu tataan dox, root mu fees joxla nga naann te nann ëskëy ci bip feem. Kokoy tëgg mi Yàlla térral, cey ñeeño, yaw mi Yàlla bérral ngir say jaloré. ABT                                                        M.Jobe

Seet sa bopp

Prent
Lata ngay jalgati Fobàl ñaari seetu Bena sa kanam Bennen sa ganaw Sigil xool li nga jakarlol Liy bàx ci sap ndong né fangë Ñaar tewateew : gëmë wala xippi. ABT                                               M.Jobe

Wa Kàwga

Prent
So sét loo ba seet Fa pepp dip toortooré ñu tudeko kàwga, So sétloo ba ca biir, momee mo boot kërum taax. Taax mi nàagu fëg dënëm ne ma fi gënn, cey lii. Taax mi Wón ganaw gidul dëgë liwoon dembàm  dëk cip tayam rék doon ëlëgëm mu tuddéko mboyga manam kàwga. Fa baykatya tamú te sañ fa dëk moné, momee ñuy tutil Nitu Alà, mo nara dukàt ba faw, frankkulayu fasyeené mu neex Yàlla setàan buur aki daggam ngony ba dëgërr cip miis nootel, dëk cip fitnal doon firawoona jëm ciy tàrtàr.   SUBHANALLAH! ABT                                                        M.Jobe